smoustaphasy5.bmp

ADOUNA DIAROUWAYE LA WAYE DOU SAKHOU WAYE

BAGNATE GNAK WOLOU SA BOPE LA

BAKAR YIW WOU DIAROUL YONE LA

BALAA GANI NAME NEFA

BALA GA KHAM KHAMADI KHAW LAA REYE

BEUG DESSE KHEL, RAGALE DESSE GUEUM

BOK SI YAKH BOU REYE FEKHE BA REUYE MO KO GUEUN

BOROM THIAKH DOU BERE AKH BORAM BATOU NENE

DESSE DOUND DOUND DESSE LA MOKO GUEUN

DI BOUR DI DAMEL DINATAKO GUEUN

DIAW DESS NA KHABINE

DOU GUELEME GO GUISS MANE NAA YOBOU SAPE SEUF

DOUN AKH YEFI DOUND BOKOUL

DOUND BEREE LA WAYE YALLAYE NOOT

rm1.bmp

« NAADIOU DEMB DOU WOWAL POTUM TEY »  

« KOU NDOBINE REY SA MAAM FOO GUISSATI LOU NIOUL DAW »  

« EULEUK DOU AGNE DOU REER WAYE LOU MATA SEDDE LA »  

« KOU AMOUL YAYE NAMPA MAAM »  

« MATE MOU BARI DIAROUL NAWE ALLA  »  

« NIT NITAY GARABAM »  

« KOU SAGNOUL BAGNE SAGNA NANGOU »  

« BALAA NGA XAM XAMADI XAW LA RAY »  

« TERE MOU TE BAYIL MOU GUISS »  

« KOU TEUP DAL CI DAAY DESSE LA BENEEN TEUBINE »  

« BALAA NGA LAAX DIAAY LAAX LEK »  

« WIRI WIRI DIARI NDARI »  

« KOU YAGUE CI TEEN BAAK FEK LA FA »  

« GOUMBE TALLE NA LENEEN LOUDOUL TEUP AY TEEN »  

« KOU MAR TAKH NAAN POOTIT BOU ROBINET OUBE MOU ROUSS »  

« JIGUEN MAR NAAN WOROUL TAKH MOU REERE AY WENAM »  

« KOU AMOUL KILIFA DJINE DI SA KILIFA»  

«FOU NDOKH DAAN TAA BO DEME FEK FA TEP TEP»  

«KOU LA ABAL BEUT NGA KHOL FOU KA NEEX»  

« NDOKH DOU BAAYI YOONAM »  

« MAGOU WAXOON NA KO MO GUEN MAGOU KHAMOON NA KO »  

«BOUR AYOUL DAK YA AY»  

« SOUL KER DOUKO TERE FEEGNE »  

«GARAP BOU NAR DOON PINTHIE LAOBE DOU KO GUISS BA DIKO GOR»  

«FAGARU MOO GUEN FADIOU»  

«LOO DOONOU NDOGOM DO DOON SERIGNAM»  

«KOU WATHIE SA ANDE, ANDE BOO NDEM FEK FA BOROM»  

«KOU EUMB SA SANXAL EUMB SA KERSA»  

« KOULA MAK EUP LA AY SAGAR »  

« KOU XAMATOUL FOO DIEUM DELOUL FA NGA DIGUE WOON »  

«MAY NIT DIEUN BESS BOU NEK DIANGAL KO NOU NIOUY NAPPE MOOKO GUEN»  

«NAAR BOU NDAW LOUMOU WAKH SA BERKELE BA LAKO DEGUE»  

«DONA SA BAAY DOON SA BAAYA KO GUEN»  

« SOUF BOU SOUTE MAROMAM DAGNE KO DIAL »  

« NEEW DOU ROMBE BAMEELAM »  

« DIOGUE LAMBA DIA DI BAKOU MOO GUEN DEM LAMBA DIA DI BAKOU »  

« KOU XAMOON LOOY MOUDJE NGA DIEUKE KO »  

« KOU NEK CI XARE BOU DIEKHAGOUL DO REE KOUGNOU DIAM »  

« KOUY DIEGUI NDOKH DOU REE KOU LAP »  

« GUEWEL BOU REP CI XARE LOUMOU DJIN XEEP KO »  

« ADOUNA WEEROU KOR LA FEEX DOK DIOTOUL DIOUBOU DOU WEES »  

« FETHIOU LIIR SOU NEEXE NDEY DIA TEYE SA MBAGAYA »  

« KOU DOUL TOUKI DOO XAM FOU DEK NEEXE »  

« NIAY BOUY XALLA YOON DOOM DIA TAKH »  

«BOU DIEGUE DOON TAKH DOON MBOK NDOKH DOU TOGUE DIEUN»  

«PITHIE NGA CI KAW WAYE XEL MA NGUI CI SOUF»  

« MBOTT YIY TEUP NAWET YEUP KOU LEEN NAR TATHIOU SA TOOL BOOYE »  

« MBAAM GAATA NA WAYE CI DIOUR GUI LA BOK »  

« GUENOU GOLO GATTE NE WAYE LOO CI LAAL MOU YEUK KO »  

« FASS BOUKO DENK SA XARIT DENK KO XARITAM »  

1 réponse
  1. SALIOU WADE
    25 mars, 2012 | 14:35 | #1

    amna solo ………walay ndeyssane…….serigne moustapha yalnafi yaag ta wer..amiine incha allah

Laisser un commentaire

mythologie |
jamaa |
iletaitunefoi |
Unblog.fr | Créer un blog | Annuaire | Signaler un abus | la beauté de l'islam
| eva75
| وجهة...