PROVERBES WOLOF
« NIT NITAY GARABAM »
L’Homme est le remède de l’homme
« NIT NITAY GARABAM »
L’Homme est le remède de l’homme
Voici une liste de Proverbes Wolof Proposée par notre Frère en Dieu : Mr Djibril Yade GUEYE
Nous essaierons de les traduire.
1- « NAADIOU DEMB DOU WOWAL POTUM TEY »
2- « KOU NDOBINE REY SA MAAM FOO GUISSATI LOU NIOUL DAW »
3- « EULEUK DOU AGNE DOU REER WAYE LOU MATA SEDDE LA »
4- « KOU AMOUL YAYE NAMPA MAAM »
5- « MATE MOU BARI DIAROUL NAWE ALLA »
6- « NIT NITAY GARABAM »
7- « KOU SAGNOUL BAGNE SAGNA NANGOU »
8- « BALAA NGA XAM XAMADI XAW LA RAY » 9- « TERE MOU TE BAYIL MOU GUISS »
10- « KOU TEUP DAL CI DAAY DESSE LA BENEEN TEUBINE »
« Liguèyou ndèy agnoup ndoom » Proverbe Wolof voulant dire «
Le labeur d’une mère est le fruit de la réussite d’un enfant
mythologie |
jamaa |
iletaitunefoi |
Unblog.fr |
Annuaire |
Signaler un abus
| la beauté de l'islam
| eva75
| وجهة...